Senaso srl dafay yengu ci wallum firi ci kalamay Italié/Wolof (wala wolof/italié) ci fann yu bari ak anam yu wor te wër ci njëg bu yomb bo ko mengele ak yebeefu mbiru marse.

Lolu mën na nekk ndax Lekalo biñu lekalo ak firikat yu xarañ te namp kalama wolof bi te seen mën mën ak seen jaar jaar mo leen ko may.

Doxalinu tannef sunuy firikat yi namp kalama wolof dafa weru fu wor te ñu ganna ay lanuy dugal ci sunu booleb xéetu mbir.

Sunuy firikat yi namp kalama wolof ñu xarañ lañu ci fann yinu mëne, te upuleuñu niñu ware woyofal seen jeflante ci niñu laaj keyit bumu mëna doom.

Senaso taxawna ngir deloo beep ligeey ci waxtu ak bés bimu digale ba ci ligeey yi gena jamp.

Fann

Senaso dai firi ci fann yile:

Keyitu yoon
Firi ci fann nganef
Firi xëtu siiwal ak yët
Firi ci lammiñ
firndé lu nopp mena dégg wala wideo